loading...

Dip Doundou Guiss répond à Canabasse et fait des révélations

Paylaş
Sitene ekle
  • Published on Aug 9, 2018

  • Dip Doundou Guiss était l'invité de Tal Rek dans le Tal Rek Show. Le leader de Reptyle Music a profité de l'occasion pour apporter sa version des faits concernants son problème avec Canabasse.
  • Dip Doundou Guiss répond à Canabasse et fait des révélations etiketleri

Yorumlar

  • Pape COLY
    Pape COLY 6 months ago

    Non nak Tal j'aime pas ta façon d'orienter les reponses. Cana et Dip sont deux grosses pointures du rap galsen. Tu aurais pu sauter sur l'occasion quand Cana a dit que 'musicalement' il appréciait Dip et essayer de créer un rapprochement au lieu de chercher la confrontation. Un DJ se doit de federer, vous êtes les hauts parleurs du Rap Game. Taye mome zéro...Un de tes fans

  • Babacar Sene
    Babacar Sene 6 months ago

    Respecter Canabasse il a révolutionné le game tay koufi encaisser ay cacher concert c grâce à l8 wtf

  • Caramel Niang
    Caramel Niang 6 months ago

    Ana gni beug Dip, il est sans probléme.Kouko tognoul meunoko ham.

  • Moréén TV
    Moréén TV 6 months ago (edited)

    .dip agalil sa djob rk bouléne falé 👑💪

  • Momoo Seye DKM
    Momoo Seye DKM 6 months ago

    Mais tall basse wakhoul dara Dip wakhoul dara gars yi rafétalén rék

  • larah shirley
    larah shirley 6 months ago

    Done léne béne vous êtes des frères ngenn bayi clash yi yow animateur bi defarofi dara. Def léne comme nigéria 🇳🇬 do lène guiss si clash you gnak fayda yi motakh ils ont des millions de vues même les américains défatougnou clash . Travaillez ensemble pour le meilleur de la musique sénégalaise

  • Jackaria Diedhiou
    Jackaria Diedhiou 6 months ago

    Dip Nagne ko nangoul reck li Nékk si mom akk Talent bouma Amm Mayou Yallha lheu Dou Chance

  • Mendychristophe
    Mendychristophe 6 months ago

    Crachez sur Dip et Dieu en fait de l'eau il se lave avec... Lii mayou yalla il est devenu célèbre d'un seul coup et il fait évoluer le Hh Galsene.

  • mUstafA Ndiaye
    mUstafA Ndiaye 6 months ago

    tout le rappeurs ce connait dip reste comme tu est never change brootha on tadord MustafOwadiTv

  • Saliou Cisse
    Saliou Cisse 6 months ago

    Dip dafa ay deh bilahi momane gayi deh !!! Cana ayna mais dip dou moromom

  • Khalifa Fall
    Khalifa Fall 6 months ago

    tall Khawma Vraiment Seytane Guaa Lou Canabass Wakh Wakho si Dara

  • Malik TV
    Malik TV 6 months ago

    Vraiment Canabasse wakhou ko dara

  • Rignese bOyz N'diAyeuh
    Rignese bOyz N'diAyeuh 6 months ago (edited)

    yéne rappeur galsene yi warr ngéne sante canabass bou bakh moy séne baye nangou léne lolou yaw dip bass dou clashanté ak iow prsk daff la raw warr nga xolatt sa diguantè ak rappeur yi ningay doxalé gni nékk sa guinaw dila jaye dila yaxal sa relation ak rappeur yi boulén déglou liguéyal té bayi clash yi amouL chance.

  • fary sow
    fary sow 6 months ago

    Srx dip sa Khol bakhoul amo esprit d'équipe dara

  • HIP HOP KOLDA OFFICIEL

    Lann moo takk niou borrii nooww dip doundeull 111.....

  • Bintou Rassoul Diop
    Bintou Rassoul Diop 6 months ago

    Mais Mr tall c pas ça qui développe notr pays

  • Lamine Le Bègue
    Lamine Le Bègue 6 months ago

    Basse dou moromou boyii, il a révolutionné le rap à lui tout seul depuis 2007 maachallah monguifi 👌👌👌 actuellement boy yii si rap nii yeup mom laniouy roy ndax mofi indi façon rap bii

  • Baladinho 10
    Baladinho 10 6 months ago

    Dip yak canabasse samay rappeurs nguéne bouléne xoulo bouléne xéx yena nék si trône rap galsen bi

  • Djoss Ka
    Djoss Ka 6 months ago (edited)

    DIP amoule diotou canabass...dip doundou guiss liguéy la gueume ak khole noumouy avancélé RAP galsén

  • MoMo JP
    MoMo JP 6 months ago

    Trés bonne vidéo♥️🔥